Wiki Xayra
Bii jukki ab junj rekk la.Man nga cee duggal sa loxo suqali ko ndeem am nga ci xam-xam ci anam yi Wiki Baike taxawal


Xayra (ci araab لقاهرة Al-Qāhira) mooy péeyu réewum Isipt, mooy dëkk bi ëpp nit ca goxub Afrig. Donte Al-Qāhira mooy tura dëkk waaye, lu bari, dees na ko wax itam, ci araabi waa-isipt, misr di Isipt ci araab.

Xayra لقاهرة
RéewFlag of Egypt.svg Isipt
way-dëkk17 856 000 nit
atum way-dëkk2 009
Rëyaay210 km²
Fattaay38 221 nit/km²
Gisub Xayra